Printer-friendly version


Mbay ak càmm

Jawu ji ci tax yi

Youkutek taax yi andul ak ňakal solo càmm gi ci taxx ya yi ci Afrik sow jant. Moom kay daňu setlu ap yokute bu am solo ci càmmak nak, xar bëy  ak ganaar ci goxu taax yi andak magug dëk yi. Doxuk taax yi nak ak jafe-jafe yi mi andal  ci walu topotook njur gi taxaw nit ňi bayi yarum xarr yi ci seen biir kër ya, fu ci mel ni Dakaar firnde la ci.yëngu googu nak mooy  wane koom gi juge ci càmm googu, ci jang mi, wutumligey mi, jox bi jox taax yi, ci wallu dëgëral dundu ak defar jawu ji ak nekin wi.

Li ganlaŋkoor càmmuk taax yi

Yoon yi jëmale mbir mi kanam

Dafa ay mbir yuy galankoor yokutek càmm gi ci taax yi,looloo wara tax ňu wara saytuli ko mënna jemale kanam.yoon yooyu nak ci lu ci ëpp nit ki moo koy defal bopam (muy ay xalaat ci yokute) ak yo xamni askan wi ňoo koy defandoo(boole xalaat yi ci ay jef yu bess).

Mebetuk yokute gi

Solok yarum njur gi ci taax yi mungi dem ci yarkat yi ak askan wi yëp.yarr mi mungi indil yarkat bi koom bu am solo ci walu ligey bi, ci kanamu askan wimu jëm ci ki yar ci kërr gi rek (muy ki koy dunde) wala muy li kër gi di suturloo. Mebetu yarkat yi nak mooy suxali seen ligey boobu ci walu koom ba mu yook seen dundu.

Li wara lal yokute boobu

Bala ňuy jublu ci yokute dafa am luňu war lijenti muytaxawal yarr boobuleba ňu mënna nek ci ay nekin bu mucc ayib ci wall celete ak jawu ji koom. Loo sax moo mënna suxali yengu wi ci càmm googu. Warul gënna takku wala gënna jaffe ci càmm gi ci tax yi. Loolo waral ňu xeex li ňi tude “zoonose” (muy ňaqq gu yomb) wax ak nit ňi ci nuňu Mëna geré nefere yi ak jox nit ňu xalaat nu ňuy raxase nefere yoyu.looloo tax ňuy xalaat ci taxawal been xame kaay bu ňu dupe “ecoTIC”.


©1997-2024 ICVolunteers|system mcart|Updated: 2024-05-01 02:41 GMT|